الخلق ينظرون إلى ظاهرك ، و الخالق ينظر إلى باطنك ، فاحذر أن تزين محل نظر الناس و تقبح محل نظر الله جل جلاله .. !
Mbokk Na nga xamne sa moroom i mbindéef yi
sa lici kaw rekk lañi xool,
Yàlla mi ñu bind nak moom laca biir lay xool,
Na nga wàtta ndiku rafetal fi mbindéef yiy xool
te defaroo fi boroom jaam ñiy xool bam jàg.